Senegaal ag dex la ci sowwu Afrig, mi ngi gudde 1790 km te di balle ca Ginne ci 750 m ci kawewaay. Di jaar Mali, Gànnaar ak Senegaal, di mujje ci mbàmbulaanug Atlas gi, ci wetu Ndar.